Intro
Intro a song by Dip Doundou Guiss on Foxsoundi — Free Music, Smart Streaming for Everyone
Intro Lyrics
[00:04.43] (Humm hummm)
[00:08.65] (Oohoo ohh)
[00:10.94] (Yeaah)
[00:19.54]
[00:46.98] Daj ngeen ci ëkk, këkk, ndëgg sërëx
[00:49.13] Doo ma jey ba jaay ma doog maa bëgg nëbb sa njëg
[00:51.52] Duma la daan ba toog sa kaw nga bëgg ma njëkk sëlëm
[00:53.84] Rap dëkkatul ci sama xol daa tëju sama xëtër
[00:56.40] Gëtam ay boys you téxet ba ër, tëx, lu tëb di sëmbëx
[00:58.88] (Low) Ci sama jëmm tay laa gën a dëgër
[01:01.47] Utal kër mère bi, ngandim maamu Mercedes ak chauffeur
[01:03.32] Tës xëtëm yi njëkk du mës a jëmbët ku leen gën a sëcc
[01:26.13] Sàcc du sàcc ba sàcc sama sacrifices yi
[01:28.42] Noon bi lay ray mën na jaar ci fiisabii Lilahi
[01:30.81] Jaag du kàcc ba daj ma ci njuuj njaaj
[01:32.89] Jiiñ ngeen ma bon, jiiñ ma soxor
[01:34.01] Jiiñ ngeen ma yéefar ak illuminati
[01:35.93] Li ma moom buy dem ci keneen ku dul man mii
[01:38.57] C'est comme mardi-gras bu ñu feetwul ci mardi
[01:40.95] Ci biir camps yi laa koy def ni Jamie Vardy
[01:43.52] Lëndëm, samay fautes du feeñ mukk ci VAR bi
[01:45.72] (Yeah) Dara dootu ma defati dara
[01:47.68] Am ndam fi ma ko waroon am yépp mais defaite bi man a
[01:50.29] Xëy te duma waaj doyal ci life te fekkeeguma gat
[01:52.60] Facturu àq yi ma ame yépp lay fay te duma rang
[01:55.03] Xeet yépp la suuf warax du kaaw kese rekk fepp ay suul ndanaane
[01:57.36] Seen game jarul tuur leketu kaana ak dereetu mala
[02:00.06] Tekkeeguma gat ci musique bi mel ni sexluwuma cat
[02:02.79] Kenn yeemu ma ndax mënuma féey ci tefes di fa lab
[02:05.12] Ñi dama leen yagg fuck ba ñu foog ne ñu jur samay doom
[02:07.48] Duggal sama zone dama lay duut ba pare rouge la nga toog
[02:09.78] Rap Galsen man rekk la benn MC buy course ak sa bopp
[02:12.46] Mën nga ma fuck? Microphone bi Dip sa tuun la ko roof
[02:14.73] Juumal ba dof nu bokk son dama lay ñuus dama lay noq
[02:16.93] Kuy sut sama njort ndayam judduwul maamam fause couche la defoon
[02:19.54] Boy duma sa moroom maak yow bokkounu
[02:21.37] Ni suurka xorom
[02:22.25] Ni Ummah ak Rome
[02:23.09] Joueurs yi ak Àllaaji Juuf double ballons d'or
[02:24.58] Ni sumb ak fomb
[02:25.44] Sunguf ak ndox
[02:26.27] Dugub ak mboq
[02:27.11] Ni dunq ak góor
[02:27.77] Ni kuy mbalax ak kuy dund hard core
[02:29.58] Chaque joueur mën na togg benn single suul double album
[02:31.81] Lu ma def tay suba ñoom ñépp def ni Duudu ak Ngóor
[02:34.57] Maay buur bi maay boos bi, bul ma tëkkale ak buujuman yoyou
[02:36.61] Fàtte xaju fi Lépp Fii La nu Fekk ni turu album bi
[02:43.75]

From the album: LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Intro by Dip Doundou Guiss , -
40e jour by Dip Doundou Guiss , -
Ñafal by Dip Doundou Guiss , BM Jaay , Bilou XIV , -
Jëli li des by Dip Doundou Guiss , -
Top 5 by Dip Doundou Guiss , -
Sunshine by Dip Doundou Guiss , -
Destin by Dip Doundou Guiss , -
Doon benn by Dip Doundou Guiss , mohrei , -
Sama nigga - Interlude by Dip Doundou Guiss , -
Dee ci yaw by Dip Doundou Guiss , Faada Freddy , -
Homie by Dip Doundou Guiss , -
WNPWY (Wàcc na pare wàccoog yéen) by Dip Doundou Guiss , -
Seetu by Dip Doundou Guiss , -
Ci naka by Dip Doundou Guiss , -
UKTV (U know the vibe) by Dip Doundou Guiss , -
Suba by Dip Doundou Guiss , Ashs The Best , -
Tefess by Dip Doundou Guiss , -
Ñetti at ci ren by Dip Doundou Guiss , Ouse Zik Buzz ,