Dee ci yaw
Dee ci yaw a song by Dip Doundou Guiss on Foxsoundi — Free Music, Smart Streaming for Everyone
Dee ci yaw Lyrics
[00:11.35] Lépp loo bëgg ma defal la ko maa dof ci yaw
[00:17.70] Lépp loo joxoñ ma daggal la ko maa dee ci yaw
[00:23.42] Bu asamaan doon daanu ma téeyeel la ko ma miir ci yaw
[00:29.45] Maa la nob lool sama chérie coco maa la bëgg yaw
[00:36.59] Baby kaay waay ma ne kaay way
[00:39.76] Xam nga ne namm naa la baby kaay waay
[00:42.44] Ma ne yuu yuu nga ne yaa yaa lu yendu ci man ci yaw lay fanaan waay
[00:48.24] Baby kaay waay ma ne kaay waay
[00:51.58] Xam naa ne namm nga ma baby kaay waay
[00:54.26] Ma ne yuu yuu nga ne yaa yaa lu yendu ci yaw ci man lay fanaan waay
[00:59.45] Lu sa jëm ji taaru taaru sa xol a ko dàq
[01:02.77] Wormaal nga ma fees ngaak sutura sa ruu dafa màgg
[01:05.42] Man maa tay bëgg la ba mu leer man it duma bëggaat
[01:08.31] Ngalam nga lingeer ci dereet def ma sa buur ak sa jaam
[01:11.31] Yaw rekk a fees samay bët yaw rekk sa flèche a may jam
[01:14.55] Yelloo nga këyitu kër fim la dëkkal ngay des ba ma dëb
[01:17.47] Bëggal ma taasu ma fecc loo bëgg sa yu la neexee
[01:20.43] Boo amul woon ma doon nit ku dul mës am chance'u mbëggeel
[01:23.42] Yenn saay nu jàppante ci wax xol yi fees ron qooñ di toq bul di denc lenn Bae
[01:28.23] Yaay leer gi fees ci sama xol
[01:29.51] Leer biddeew ci sama kaw,
[01:31.07] Bideew bi leeral sama yoon
[01:32.53] I miss you everyday and more the yesterday i need your love
[01:35.54] Lépp loo bëgg ma defal la ko maa dof ci yaw
[01:41.13] Lépp loo joxoñ ma daggal la ko maa dee ci yaw
[01:47.49] Bu asamaan doon daanu ma téeyeel la ko ma miir ci yaw
[01:53.45] Maa la nob lool sama chérie coco maa la bëgg yaw
[02:00.30] Baby kaay waay ma ne kaay way
[02:03.54] Xam nga ne namm naa la baby kaay waay
[02:06.19] Ma ne yuu yuu nga ne yaa yaa lu yendu ci man ci yaw lay fanaan waay
[02:12.18] Baby kaay waay ma ne kaay waay
[02:15.39] Xam naa ne namm nga ma baby kaay waay
[02:18.08] Ma ne yuu yuu nga ne yaa yaa lu yendu ci yaw ci man lay fanaan waay
[02:23.81] Bu ñépp nee déet te Yàlla ne waaw fàww mu am diggante bi (fàww mu am sunu diggante)
[02:35.83] Yaak say défauts ak say qualités noonu laa la bëggee (noonu laa la bëggee)
[02:48.07] Sunu diggante bi dara xaaju ci sa noon yi siisu nañ nu bàyyi ak Yàlla
[02:51.97] Pigg ak peel la bañuma ci dara
[02:53.76] Mukk duma la mës a bàyyi ginnaaw
[02:56.62] Nu dund freedom ni céeli muy naaw
[02:59.84] Baby maa la bëgg duma dëgg tànk ci say bëgg-bëgg li nga bëgg laa bëgg sa mbëggeel moo may bégal
[03:07.52] Joxoñal ma dagg nu dundu aljanna
[03:11.47] Li may bégloo ni ga mel la honey ak li ci yaw (baby)
[03:17.42] Yaw laa doon xaar ngir nga defar sama xol bi ñu yàq (xol bi ñu yàq)
[03:23.66] Nun nu réeroo ba nga ba ma la sama noon yi di xaar (noon yi di xaar)
[03:29.39] Bu leen ko jàppe ndax dañoo xamul maak yaw fi nu jaar
[03:35.03] (Fi nu jaaaaaaaar aaaaaah aaaaaah aaaaaah fi nu jaaaaaaaar aaaaaah aaa aaaaaah)
[04:15.09]

From the album: LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Intro by Dip Doundou Guiss , -
40e jour by Dip Doundou Guiss , -
Ñafal by Dip Doundou Guiss , BM Jaay , Bilou XIV , -
Jëli li des by Dip Doundou Guiss , -
Top 5 by Dip Doundou Guiss , -
Sunshine by Dip Doundou Guiss , -
Destin by Dip Doundou Guiss , -
Doon benn by Dip Doundou Guiss , mohrei , -
Sama nigga - Interlude by Dip Doundou Guiss , -
Dee ci yaw by Dip Doundou Guiss , Faada Freddy , -
Homie by Dip Doundou Guiss , -
WNPWY (Wàcc na pare wàccoog yéen) by Dip Doundou Guiss , -
Seetu by Dip Doundou Guiss , -
Ci naka by Dip Doundou Guiss , -
UKTV (U know the vibe) by Dip Doundou Guiss , -
Suba by Dip Doundou Guiss , Ashs The Best , -
Tefess by Dip Doundou Guiss , -
Ñetti at ci ren by Dip Doundou Guiss , Ouse Zik Buzz ,