Jëli li des
Jëli li des a song by Dip Doundou Guiss on Foxsoundi — Free Music, Smart Streaming for Everyone
Jëli li des Lyrics
[00:06.07] 1da on the beat
[00:13.24] Never mind every day, bàyyi nit ñi ñu sol la bàyyi nga liggéey
[00:19.22] Jarul coow di jib, coow du jib jarul ...
[00:25.18] Sa family ñooy sonn ci yaw di daŋ-daŋi kay
[00:30.81] Bis dina tar doo gis kenn
[00:33.83] Kon jëli li des, mën nga jëli li des, jugal jëli li des
[00:43.64] Lépp ci xel rekk lay feeñ, jëlil li des
[00:48.75] Yaay jëli li des, mën nga jëli li des (mmm)
[00:54.41] Ndax lépp ci xel la, kon yaw yaay jëli li des
[00:58.95] Sol essence sa mind soog a jëli li des
[01:01.68] Ñépp a soxla ndam def ni mbër yi di def
[01:04.33] Dootuñ joow Senegaal seen gaal gee bari vitesse
[01:06.96] Fii ñi dàq a jaay seen taat ñoom seen cér yi du feeñ
[01:10.25] Non duñ sàcckat yu mag bu dee soluñu veste
[01:12.99] Ku ñàkk wéet nun ndox yu taa yee tax sunu kër yi di fees
[01:16.13] Luy sa njariñ ñu xeex, texeg tekki xayna safaraay changer nit fi dóomu taal taxul ba këriñ mënul weex
[01:21.27] Nice fine,
[01:21.88] Suñ dëkk du gat baay,
[01:23.35] Fi jeunes yi dul am njëgam duñ def lu dul taaj caayin
[01:26.27] Balóot, babi ak dice,
[01:27.80] Dóor call këfi sac jaay
[01:29.27] Réer ci saayir ak baatin fen ak dëgg bëccëg night time
[01:31.94] Ku dund jàng force ndax life day jox ay cours sa maitre,
[01:34.80] Bul xam ku baax ci yaw ak ku la jekkoogul batay
[01:37.88] Loo baax baax moytul nit ñi foog ne sa xol moo sut sa xel
[01:41.25] Fii dangay dee ci nit mu lay xoon pour nga dee
[01:43.73] Kon jëli li des, (i'm on my way)
[01:46.30] Mën nga jëli li des, (you know my pain)
[01:49.35] Jugal jëli li des (story of my life, story of my life)
[01:56.01] (I'm on my way)
[01:58.47] Yaay jëli li des
[01:59.01] (You know my pain)
[02:01.16] Mën nga jëli li des
[02:01.99] (Story of my life, story of my life)
[02:04.30] Ndax lépp ci xel la, kon yaw yaay jëli li des
[02:07.28] Jëli li des pour bañ ñàkk li xaalis mënut a am
[02:09.90] Yaa gën alal mën nga ñàkk sa bopp ci wut alal
[02:12.53] Même sutura dafa cher ni dignité muñ ak ndam
[02:15.52] Ku bañ tàllal loxoog yërmaande fàww nga suul sa tànk dóoranteek life
[02:19.41] Nangu sëyal metit heureux ménage door a ker naaj
[02:22.09] Yal na nu Yàlla musal ci compte bu fees ak ruu bu vide,
[02:24.81] Musal nu tam ci toog ak ñépp bég ak wéet sa ruq triste
[02:27.85] Xel kenn du ci lire kenn mënut a xam lu weex ak ñuul ci nit
[02:30.75] Gëj naa gis samay doom,
[02:32.46] Gëj naa feel sama drogue,
[02:33.86] Gëj naa am li ma yellool comme bénéfice sama job
[02:36.39] Tay jëli naa li des,
[02:37.52] Tay njàmpe la ci der,
[02:38.43] Calpé laa ci cash,
[02:39.63] Tay xàmme naa vipéres yépp
[02:40.99] Duñ ma téeye ni Mandela ci jail
[02:43.13] On the top of the top Dip Doundou Gis you know my name
[02:46.11] Booy damaa doylu trop ku mënul suur mënu maa lekk (mëno maa lekk)
[02:49.63] Dereet du fen, Yàlla buy def du tàggu kenn
[02:51.93] Démb ñaan yi bañ na tay sët yi nangu nañu
[02:56.19] Never mind every day, bàyyi nit ñi ñu sol la bàyyi nga ligégey
[03:01.87] Jarul coow di jib, coow du jib jarul ...
[03:08.15] Sa family ñooy sonn ci yaw di daŋ-daŋi kay (daŋ-daŋi kay)
[03:18.09] (Daŋ-daŋi kay, daŋ-daŋi kay)
[03:19.74]

From the album: LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Intro by Dip Doundou Guiss , -
40e jour by Dip Doundou Guiss , -
Ñafal by Dip Doundou Guiss , BM Jaay , Bilou XIV , -
Jëli li des by Dip Doundou Guiss , -
Top 5 by Dip Doundou Guiss , -
Sunshine by Dip Doundou Guiss , -
Destin by Dip Doundou Guiss , -
Doon benn by Dip Doundou Guiss , mohrei , -
Sama nigga - Interlude by Dip Doundou Guiss , -
Dee ci yaw by Dip Doundou Guiss , Faada Freddy , -
Homie by Dip Doundou Guiss , -
WNPWY (Wàcc na pare wàccoog yéen) by Dip Doundou Guiss , -
Seetu by Dip Doundou Guiss , -
Ci naka by Dip Doundou Guiss , -
UKTV (U know the vibe) by Dip Doundou Guiss , -
Suba by Dip Doundou Guiss , Ashs The Best , -
Tefess by Dip Doundou Guiss , -
Ñetti at ci ren by Dip Doundou Guiss , Ouse Zik Buzz ,