Ñetti at ci ren

Ñetti at ci ren a song by Dip Doundou Guiss on Foxsoundi — Free Music, Smart Streaming for Everyone

Ñetti at ci ren by Dip Doundou Guiss

Ñetti at ci ren Lyrics

[00:20.02] Ñetti at ci ren
[00:21.47] Tëju mënóo fippu
[00:22.18] Fàq dem prison boo tànnal sa bopp tëju fi sa papa bañ
[00:25.30] Mbëggéel capitainu borom nangu siiw du jàmmi kenn
[00:28.14] Ba lépp di soppeeku ci sama dundu def na ñatti at ci ren
[00:31.80] Tay ngay xam lu géej gi di riir
[00:33.57] Lu metti lu tiis
[00:34.46] Dunu fàtte mukk ñi des ak ñi siif
[00:35.97] Liggéey guddi xiif
[00:36.77] Dékku ibliis yee bu de du nu jig
[00:38.53] Dunu bidaanti di riche
[00:39.41] Teg ci tàkk ni biddeew yi nu tiim
[00:41.13] Ñetti at ci rene
[00:42.30] Ndeke suba gën a mat a sóor du añ du reer
[00:44.22] Ñetti at ci ren
[00:45.43] Jéem nañ ma fi ray ni xaj bu dee
[00:46.94] Reyndi xàttit fes tëdd feebar
[00:48.94] Jàng naa lu ne jeng naa fi
[00:50.71] Mais duma mës a daanu never
[00:52.36] Can you see what's going on
[00:55.08] Turn the lights for me
[00:58.06] And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[01:03.59] Can you see what's going on
[01:05.97] Turn the lights for me
[01:08.95] And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[01:12.08] Ñetti at ci ren
[01:13.54] Ñi bëgg a xam ñépp agsileen
[01:14.92] Sama gàccce lañ bëgoon gis teguñu ko bët ni ab sirene
[01:17.62] Yar sama bopp ndax njub du dereet du ci sax ci man
[01:20.28] Li gënoon jafe nekkul di liggéey mais liggéey sax ci men
[01:22.67] Ñatti at music bi laago
[01:24.04] Dan koy changer at yi ñëw ñédd temps bukki laa boot
[01:26.76] Tax nga dégg xaj yi di mbow
[01:28.25] Ñat at town bi dëgër këcc
[01:29.44] Doo gis nit fu muy tëdde
[01:30.50] Dip son bi mënul woon ñàkk comme galañ fu ñuy tëgge
[01:33.26] Kaay ma wax lu waral booy yi
[01:34.91] Fippu utali gaal yi
[01:36.07] Dem géej sànni mbaal yi
[01:37.53] Daj coono bu nekk pour dégg jaali
[01:38.78] Gën a takk dàll yi
[01:39.71] Koo ci laaj rêvam Farãs walla Itaali
[01:41.14] Espoir réer ni Jaari
[01:42.32] Ñoo ngi xaar Nguur gi ci taatu ndaa li
[01:43.81] Maa ngi dox di dem ci yoonu God, ibliis di may xëcc
[01:46.46] Humeurs yi du changer damay bég yenn saa yi ma yeewu def këj
[01:48.86] Dara a ma yéematul gis naa fi xar-kanam gu nekk
[01:51.45] Nooflaay du am bam bëgg ko, ci coono lañ nu binde nun
[01:54.51] Ñetti at ci ren mère mësul tàyyi ci di may muñal
[01:56.97] Su ñèpp xàddi woon du paf ma war ko delloo njukkal
[01:59.62] Sabablou jaamu Yàlla ci jaami Yàlla yi bul jàmbu Yàlla
[02:02.29] Nekk nit, nitee ko gën,
[02:03.13] Nit mënul weesu jaamu Yàlla, Yeah!
[02:06.02] Can you see what's going on
[02:08.77] Turn the lights for me
[02:11.49] And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:16.70] Can you see what's going on
[02:19.01] Turn the lights for me
[02:21.72] And I'm still the light for you yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:27.02] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:29.60] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:32.39] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:34.96] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:37.66] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:39.84] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:42.51] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:45.27] Yeah yeah yeah yeahhh yeahhh
[02:48.81]

From the album: LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)