Suba

Suba a song by Dip Doundou Guiss on Foxsoundi — Free Music, Smart Streaming for Everyone

Suba by Dip Doundou Guiss

Suba Lyrics

[00:22.23] Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
[00:27.55] Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
[00:31.14] Lépp ay mel ni mu meloon
[00:33.38] Ndax boo jugee ci examen bu cóol
[00:35.63] Lalu hopital
[00:36.82] Yaa ngi ci jail bi waay,
[00:38.94] Dégg naa def nga accident
[00:41.20] Mayuñu la visa,
[00:42.78] Def nga fause couche waay
[00:44.07] Pararaa
[00:45.72] Dinan la xaar
[00:46.93] Pararaa
[00:48.12] Gëmal ne dinga ñëwaat 
[00:49.61] Pararaa
[00:51.49] Dinan la xaar
[00:52.51] Pararaa
[00:53.73] Gëmal ne dinga ñëwaat
[00:55.17] Man nelawatuma ba yàndoor, suba la xamul li muy doon
[00:59.25] (Kenn xamul li muy doon)
[01:01.42] Dem naa ba réeroo ak samay xalaat tàggalikoo ak sama sago
[01:06.72] Mel ni kuy gént lu ma yaakaar tay ba def ko sama xel mu naaxsaay (lu ma yaakaar mu tas)
[01:12.58] Dem naa ba jublu yoonu caay-caay xel mi dellu ci li may xaar
[01:17.89] Toog ci ker gi di féexlu mu tàng mel ni comme naaj
[01:20.70] Ku fiy dem du tàggo fii kenn bëggul non waay
[01:23.43] Fàww nga am ba dee gor mënul dëkk si ñaan
[01:26.46] Mën nama xéy ba gontu fii dara du sotti ndax lan?
[01:29.76] Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
[01:35.39] Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
[01:38.82] Lépp ay mel ni mu meloon
[01:40.98] Ndax boo jugee ci examen bu cóol
[01:43.18] Lalu hopital
[01:44.86] Yaa ngi ci jail bi waay,
[01:46.63] Dégg naa def nga accident
[01:48.73] Mayuñu la visa,
[01:50.24] Def nga fause couche waay
[01:52.07] Pararaa
[01:53.85] Dinan la xaar
[01:54.99] Pararaa
[01:56.18] Gëmal ne dinga ñëwaat
[01:57.63] Pararaa
[01:59.46] Dinan la xaar
[02:00.50] Pararaa
[02:01.77] Gëmal ne dinga ñëwaat
[02:02.88] Yenn saa yi ngay dund loo dul nettali kenn
[02:05.21] Ni ku nekk ci gént xamal ne Yàlla du jeex
[02:08.77] Growing's always coming with pain, homie don't worry man
[02:12.30] Gotta show'em that yu really want it yeah
[02:14.35] Ndax àdduna daal coono yëfam la
[02:17.64] Doo mës a tàggook li lay yéem
[02:20.05] So i'm living my life stay away from them
[02:23.07] Loo mënati daj bis dafay jeex
[02:25.97] Yanu loo àttan, te deel moy loo mën dékku ci mbugal
[02:28.54] Xel bu mat kàttan biceps xel moo gën bi tëkku mbër
[02:31.47] I got a lot of dreams and believe everything gonna be alright
[02:36.97] Baby a got a lot of dreams and believe everything gonna be alright yeah
[02:43.49] Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
[02:49.13] Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
[02:52.63] Lépp ay mel ni mu meloon
[02:54.48] Ndax boo jugee ci examen bu cóol
[02:56.86] Lalu hopital
[02:58.22] Yaa ngi ci jail bi waay,
[03:00.37] Dégg naa def nga accident
[03:02.42] Mayuñu la visa,
[03:03.96] Def nga fause couche waay
[03:05.70] Pararaa
[03:07.17] Dinan la xaar
[03:08.63] Pararaa
[03:09.56] Gëmal ne dinga ñëwaat
[03:11.36] Pararaa
[03:12.81] Dinan la xaar
[03:14.29] Pararaa
[03:15.23] Gëmal ne dinga ñëwaat
[03:30.62]

From the album: LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)